0:00
9:45
Reculer de 15 secondes
Avancer de 15 secondes

Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax  Afrig. Ndégat yii di Podcast, xam sa démb, xam sa tey »,  looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.

D'autres épisodes de "Xam sa démb, xam sa tey"